GEMOU MA KO

MAMADOU MOUSTAPHA LO

Massou ma gueum ne beuss dina gneuw, dina gneuw
Ba gnou took di wakh
Kouma néwone sama lokho ngay moudié
Mane douma ko gueum
Dane na sampou si mbeddami ni garap
Di khar fou sa dieumeu dji di rombé
Bama diangaat la
Ba kholat sa dokhine, sa dokhine
Bama diangaat la
Ba kholat sa dokhine, sa dokhine
Khalé bilé khalé bilé, gueumoumako, gueumoumako (bis)
Lék Lék dawou ma la begane ték beut
Ndax souma la guissé sama fit dém
Lék lék dawou ma la begane ték beut
Ndakh souma la guissé, sama khél diakhasso
Lék Lék dawou ma la begane ték beut
Ndakh souma la guissane, sama tension yèèk
Di yèèk, di yèèk, di yèèk, oh yééh, yééh
Massouma gueum beuss dina gneuw bagnou anda
Ba took di wakh
Kouma néwone sama lokho ngay moudié
Mane douma ko gueum
Dana sampou si mbéd ni garap di khar
Fou sa dieum dji rombéee
Bama diangaat la, kholaat sa dokhine,
Ba khollat sa dokhine, bama diangaat la
Kholaat sa dokhine, ba kholaat sa dokhine
Khalé bilé khalé bilé, gueumoumako, gueumoumako (bis)
Lék lék dawou me la begane ték beut
Ndax souma la guissé sama fit dém
Lék lék dawou ma la begane ték beut
Ndakh souma la guissé, sama khél diakhasso
Lék lék dawou me la begane ték beut
Ndakh souma la guissane, sama tension yèèk
Di yèèk, di yèèk, di yèèk, di yèèk, di yèèk, di yèèk
Khalé bilé khalé bilé, gueumoumako, gueumoumako (bis)

(Chœur)
Massouma gueum beuss dina gneuw
Ngamay womé Papa Chéri
Sama yakar mo done lekeulé sounouy khalat
Seukeulé sounouy khol
Massouma gueum né beuss dina gnieuw
Ba nga ma womé Papa Chéri
Démone na ba gnamétouma, guissé ragal
Sama yakar mo done leukeulé sounou khalat
Sinkeulé sounou khol heu khalébi

Beliebteste Lieder von CHEIKH LO

Andere Künstler von Funk