Jengu

Elzo JamDong

JENGU
Verse 1

Bandi mic Yaadikone (bandi)
4 projets yokk job wañi wox (wañi wañi wox)
So may seet ma ngui Port
Dope bi ñew na container, barigots (oh oh)

Sama premier ennemi mane leu
Melomind yi xam neñ dama manquer vis (Manquer manquer)
Sama studio sama scène de crime
Rey naa sama nafss musique rekkay sama viiice

Bridge:
Sa rappeur neena dafa bëg mel ni mann
Nee ko awma 1er Mai awma jour férié yeah yeah
Homie paré naa pour songg projet anytime
Depuis goné hustle moma gënël am liguey yeah yeah

Chorus:
Flowu terru Baay Sogi, daaju Percocet
Vestu Tommy Jeans, tek ci pairou 7
Bëri laamiñ sama kaw, faut que ma lemu leen
Te liniouy wax ci mann yëpp dara leeru leen
Im on my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu)
Im on Sunu Flavor damay jengu rek (waar sama waar)
Im on my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu)
On my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu
Jengu jengu)

Verse 2
Ki la gënë jege mo la gënë mënë siss (chi chi chi)

Ki lay gënë bege mo la gënë mënë kill (yi yi yi)
Mandikat su gisul escalier sax dinë yeek
Ak nima xiife lekk sa money bu mu la yeem

Buru le yeem yagg naa raam leegi dama wara naaw
Boy ya ngi sannanté ay subliminal
May xol nu may jaayé comme Warano
En mode Collie Budz sumay come around
So xamul sound do fi fuck around
Bul deglu ki ne gore du dug waañ
Xolal togg naa motax bokk naa (woe)

Balaa ngay xam sama tur, dama xaar sama tour (yeah
Yeah)
Kenn du ko tangal ni mann, mën naa leen aal sama four
Leader ci art bi lijënti lotta Gʼz doga dox
Duma lekk li ga yi togg sama avenir moma ñor

Bridge:
Sa rappeur neena dafa bëg mel ni mann
Nee ko awma 1er Mai awma jour férié yeah yeah
Homie paré naa pour songg projet anytime
Depuis goné hustle moma gënël am liguey yeah yeah

Chorus:
Flowu terru Baay Sogi, daaju Percocet
Vestu Tommy Jeans, tek ci pairou 7
Bëri laamiñ sama kaw, faut que ma lemu leen
Te liniouy wax ci mann yëpp dara leeru leen
Im on my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu)
Im on Sunu Flavor damay jengu rek (waar sama waar)
Im on my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu)
On my Sunu Flavor shit damay jengu rek (jengu
Jengu jengu)

Outro ( Sunu Flavor's DJENGUOU sample)

Wissenswertes über das Lied Jengu von Elzo JamDong

Wann wurde das Lied “Jengu” von Elzo JamDong veröffentlicht?
Das Lied Jengu wurde im Jahr 2019, auf dem Album “FreeSeason 2” veröffentlicht.

Beliebteste Lieder von Elzo JamDong

Andere Künstler von African hip hop