MO YARO

Alexandre CHIERE, Lansana SANE, Paul CUCURON

Doyegama si kersé
Wonégako mome
Xalé bou yarou
Mané yama mome
Ya ligueye lou méleni
Amoulo morome
A dieufe diou bahe die
Mani yaye borome

Fougnoula toudé
Mané mo yaro
Sa ligueye la
A xalé bilé mané
Mané mo yaro
Sa ligueye la

Weurnala si kogne bi
Kéneu méni yaw
Sa youmala séné
Xole bi dale si yaw
Ha mané yalla samala
Hé mané yalla samala

Doyegama si kersé
Wonégako mome
Xalé bou yarou
Mané yama mome
Ya ligueye lou méleni
Amoulo morome
A dieufe diou bahe die
Mani yaye borome

Fougnoula toudé
Mané mo yaro
Sa ligueye la
A xalé bilé mané
Mané mo yaro
Sa ligueye la

Mo yaroooooo
Ki moka yarooooo

Beliebteste Lieder von Lass

Andere Künstler von Afrobeats