Badou Meun Lepp

BADOU MEUN LEPP

Dofoulo Djinné péssoula
Dofoulo Djinné péssoula
Dofoulo Djinné péssoula
Dofoulo Djinné péssoula
Khamé nga khamé nga khamé nga Yalla ak yaali
Khamé nga Yalla ak yaali
Khamé nga Yalla ak yaali
Ki ley paadial dila dout dila yaali
Badou meun lepp

Ndiago bi nénama Nikissi
Khekh bi dou diekh ba nga paré ci
Gnoussal gnou mc yi diape ci
Sedalal bières yi gnou yakhe fi
Kholal ma khalé bi nga andal non bokossi
Danga dioup lokho ni Oguchi
Dougal rek ngay def Oh que si
Nigga yay dogal gnou tope ci
Yang may khaar boy mais naa le beete
Gueun le tang fils ci khol bou sedd
Khamo gatt fils sa khel a guède
Chaque jour nga guent né mang ley yèdd
Non mais fils danga niake diom
Chaque jour ci beat bi gnou def la dom
Chaque jour nga diebalou tek sa aum
Man may alcool bouy fedj sa gaum
Nigga gnola gueneu dé kodjal sunu concert ci armel bi chaque jour gnouy rey aki dekil rap bi
Rap wolof dou sama game mais saayou ma playé nga moudjé seeti arbitre
Yeah dama neek, dama sokhor may professeur boula doul may sakh nga tokho
Dofoulo Djinné pessoula mais beuss boula pessé dinga khamé sama lokho

Dofoulo Djinné péssoula
Dofoulo Djinné péssoula
Dofoulo Djinné péssoula
Dofoulo Djinné péssoula
Khamé nga khamé nga khamé nga Yalla ak yaali
Khamé nga Yalla ak yaali
Khamé nga Yalla ak yaali
Ki ley paadial dila dout dila yaali
Badou meun lepp
Badou meun lepp
Badou meun lepp
Badou meun lepp
Bombardier Modou Lo : 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis
Yekini Balla Gaye : 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis
Gris Bordeaux Eumeu Sene : 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis
N-eazy Rappeurs yi : 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis

Game Bi dama ko yaague diegui
Khamoma? Sa guel moma dégue
Nga wagniko ngir mou sorima kone naako laal ak mmm bou goudou
Khamatouma sakh boy kagne la djoudou
I'm so fresh ni di dora fouddou
Ndeki ci lal bi ni laakh ci touddou
Rap galsen lay solal mboubou
Déguena Souma fi néké do thiop motakh sayou ma touké nga youkhou "weer Bi fegn na"
Rappeur yi aka gno keukh ak loumay méyé yeup gnou nane N-eezy bone na
Moun na la gaagn ak ay flowou dembe
Flowou ganaaw souba lay méyé souba
Charlatan la mais damay khoudbeu
Ay téré gucci ci biir sa guembe
4 appuis 4 appuis my nigga
Saafara flow nigga mandi nga
Technikou Diouf wala Fadiga
Manaam gauche wala droite Nigga taalina
Mane ak rap boy ni Justo ak Balbina
Ni Congo degn ma Désiré Kabila
Daan téleu yéwou naan diangui naa diade cogne rek seey

Dofoulo Djinné péssoula
Dofoulo Djinné péssoula
Dofoulo Djinné péssoula
Dofoulo Djinné péssoula
Khamé nga khamé nga khamé nga Yalla ak yaali
Khamé nga Yalla ak yaali
Khamé nga Yalla ak yaali
Ki ley paadial dila dout dila yaali
Badou meun lepp
Badou meun lepp
Badou meun lepp
Badou meun lepp
Tyson Tapha Gueye : 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis
Gouye Gui My nigga Zoss : 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis
Ama Baldé Tapha Tine : 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis
N-eazy Khalé bi : 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis 4 appuis

N-eazy diarone na fi wakhati fi ay ndiakhoumam dokhi
Lokhati fi mbotou gayi paré yokhossou fi ay mc’s meune gaagné
Kane mo la gueune jeuli ci sa game bou dé bi soudoul N-eazy boy té doula jaay dolé
Ndakhté li nga meune yeeg yeup mouno niou jaay golo
Amoulo fi nelaw da gnou gaaw di nga waneu ngelaw

Wissenswertes über das Lied Badou Meun Lepp von Nix

Wann wurde das Lied “Badou Meun Lepp” von Nix veröffentlicht?
Das Lied Badou Meun Lepp wurde im Jahr 2016, auf dem Album “Excuse my Wolof” veröffentlicht.

Beliebteste Lieder von Nix

Andere Künstler von African music