Do Dara

Viviane Ndour

Néna dafa am mana (mana)
Té yoroul ndieugou nana (yoroul ndieugou nana)

Meuna ndiody beugeu diay graw (diay graw)
Té ioe yoroulo nada (yoroulo nada)
Meuneu gondi beug diay graw
Té yoroulo nada sax
Néna yor na ohh oh ohohoh

Ndéké yorou lou soucar café barada he heheh
Mouy capém di kossam lépam khotékou oh ohoho
Lékoulo déh nanoulo sa nélaw dématoul né nga yor ngeu he heheh

Di fowé sa xel bi molay sonal
Goor souné war nga diom (di déf té lou yomb)
Loufi diar ngey wané (djom ba niawalone nama)
Di digué lo meunoul (so teudé do nélaw)
Dou ni nga beugeu doundé
Dou ni nga beugeu doundé
Ki tothi na kogn ba oh oh oh

Do dara, do dara, do dara

Gnata yone nga dieul alalam té fayoko
Gnata yone nga digg Pa yék mère yi niou adji ji Macca (Macca)
Té défoci dara (dara)
Nioune guissouniou dara
Ndéké ioe do dara

Néna dafa am mana
Té yoroul ndieugou nana
Néna dafa am mana
Té yoroul ndieugou nana
Meuna ndiody beugeu diay graw
Té ioe yoroulo nada
Meuneu gondi beug diay graw
Té yoroulo nada sax
Néna yor na ohh oh ohoho

Ndéké yorou lou soucar café barada he heheh
Mouy capém di kossam lépam khotékou oh ohoho
Lékoulo déh nanoulo sa nélaw dématoul né nga yor ngeu he heheh

Di fowé sa xel bi molay sonal
Goor souné war nga diom (di déf té lou yomb)
Loufi diar ngey wané (djom ba niawalone nama)
Di digué lo meunoul (so teudé do nélaw)
Dou ni nga beugeu doundé
Dou ni nga beugeu doundé
Ki tothi na kogn ba oh oh oh

Ndéké yorou lou soucar café barada he heheh
Mouy capém di kossam lépam khotékou oh ohoho
Lékoulo déh nanoulo sa nélaw dématoul né nga yor ngeu he heheh

Do dara, do dara, do dara
Oh oh oh, eh eh eh

Andere Künstler von Contemporary R&B