Waaw

Viviane Ndour

Waaw waaw waaw waaw waaw
Lo wakh mani waaw
Waaw waaw waaw waaw
Lo déf mani buu sama khol
Yague koy pincé makoy fell

Daga togue ba khadiou goudi
Yote nank dougou sougnou keur
Fékhé ba kène yeugoulaaa
Nga sathie sama khol bi dème (yow sathiééé)
Ya saf sap ak soukeur (niamal)
Dama ame sa faiblesse douma la (niamantikou)
Yamay tagalék sama saggo (dieuleul)
I love you, I love you

Waaw waaw waaw waaw waaw
Lo wakh mani waaw
Waaw waaw waaw waaw
Lo déf mani

Yague ga miir thi mane
Khamga sama dougue ak sama guène
Khamga samay andado
Khamga tamit samay deukeundo
Maître bila diangal aye na (taril)
Lo wakh dafa nékh ba (melni)
Lo déf ma guiss né nonou la (dieuleul)
I love you, I love you

Waaw waaw waaw waaw waaw
Lo wakh mani waaw
Waaw waaw waaw waaw
Lo déf mani

(Khaléyi madjléne)
Melni soldat ak généralam
Thi beussou fêtou indépendance (indépendance bi)
Sa mbeuguel lamay madj lo
Thi sa ordre rék lay weuy (thi lay weuy)
Ya saf sap ak soukeur (niamal)
Dama ame sa faiblesse doumala (niamantikou)
Yamay tagalék sama saggo (dieuleul)
I love you, I love you

Waaw waaw waaw waaw waaw
Lo wakh mani waaw
Waaw waaw waaw waaw
Lo déf mani buuu thi sama khol
Yague koy lale makoy yeug
Gome thi sama khol
Yague koy pincé makoy fell

Sathie bigay sathie goné gui
Nékh na ndéyam, nékh na bayam
Avocat meunou thi dara
Procureur meunou thi dara
Monsieur le juge douka juger
Wuyaayyooy wouy sathié lay lahila laaa

Andere Künstler von Contemporary R&B