Birima

MBAYE MAMADOU, NDEYE NDOUMBE MBAYE, YOUSSOU N DOUR

Maysa tende jodo yaa moom liile
Maysa tende jodo yaa moom liile
Maysa tende jodo yaa moom liile

Hi woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee

Buri samba laobe yaa moom liile
Buri samba laobe yaa moom liile
Buri samba laobe yaa moom liile

Hi woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee
Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee

Damel maisa penda joor
Jooro jooro jooro jooro ho ho ho hoy
Sama waaji ken dula jam naani

Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee

Mmmm mmm
Wooy tedi ngoné maarne be sambaa
Kuli baca senge ndat biran ngamoo
Ngoné maca nas mbay maca jeeri
Samba yaasimooooo dike mbay kuja dooooki
Yay borom mbaboor mi

Hi (di) woy birima sama waaji ken dula jam naanee
Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee

Dogo fal ak mawa joor kumba samba yaay jaloor
Dogo dogo, ho ho ho!

Aziz o mbay dogo xam nga yoon wee

woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee

Maisa tendo jooro jooro a mari ngone sobel kayor niila
Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee

Wissenswertes über das Lied Birima von Youssou N'Dour

Auf welchen Alben wurde das Lied “Birima” von Youssou N'Dour veröffentlicht?
Youssou N'Dour hat das Lied auf den Alben “Joko : from Village to Town” im Jahr 2000 und “History” im Jahr 2019 veröffentlicht.
Wer hat das Lied “Birima” von Youssou N'Dour komponiert?
Das Lied “Birima” von Youssou N'Dour wurde von MBAYE MAMADOU, NDEYE NDOUMBE MBAYE, YOUSSOU N DOUR komponiert.

Beliebteste Lieder von Youssou N'Dour

Andere Künstler von World music