Amitie
Sincérité ak mandou thi walou gou né
Mome nga ma xamal
Dignitégou andak dal diamono diouné
Lagne massa dokhal té diko dieuffé
Si souniou diganté
Ningue maye nebôke dima lakhou rafétoule
Mou melni mane dama défe louma yeugoule
Wi dokhaline dama la ko khaméwoule wône
Guissône nani mane ak yawe sougnou amitié
Nite gnépa ko nawe
Bi changement bou méttêke m'béttéle bi nga ma ko wakh
Mingui maye sonnale, mettina thi mane, takhe na ma ragale
Ni seîtané, oh
Ningue maye nebôke dima lakou rafétoule
Mou melni mane dama défe louma yeugoule
Wi dokhaline dama la ko khaméwoule wône
Guissône nani mane ak yawe sougnou amitié
Nite gnépa ko nawe
Bi changement bou méttêke m'béttéle bi nga ma ko wakh
Takhe na ma ragale
Khamale ni yawe gnoune gnâre gnô maggandô
Té dagnou masse yékkétéke tégandô
Beugeuneté lôle gnô rawe aye toureundô waày
Gnâri fane yi ma diauke, gneuwe di réresi sa keure
Khamétoumala
Bimala nouyô yawe nga fayéma bakkane
Réke ma khame ni seîtané meune nala
Bénénaté boule teupe di bétté
Nara défaneté badi gnakkaneté
Boula dalaté nagnou guisseuneté
Sougnouy wakhtane moudjié thi diôté
Hou eh raw, hou eh raw, hou eh raw
Raw raw raw hé
Hou eh raw, hou eh raw, hou eh raw
Raw raw raw hé